
Teggiini niti Yàlla yi: Xaaj ñett
Teggiini niti Yàlla yi: Xaaj ñett bi mu ngi aju ci disóo ak Yàlla ci sa mbir yépp, moytu di jublu mayu Yàlla yi fàtte Aji-Maye ji, ak wéet.
Show notes
Hosted by Cheikhouna Diaw · 🇺🇸 US · WO · 26 episodes
Established thought leaders with verified media credentials.
Li tax a jóg Bëgg a Baax podcast mooy yaatal mbaax. Képp koo xam ne mbaax ñor na la, nu ngi la ciy dalal ak jàmm.
Cheikhouna Diaw hosts Bëgg a Baax podcast, a religion show with 26 episodes published.

Teggiini niti Yàlla yi: Xaaj ñett bi mu ngi aju ci disóo ak Yàlla ci sa mbir yépp, moytu di jublu mayu Yàlla yi fàtte Aji-Maye ji, ak wéet.
Show notes
Ci waxtaan wii, da nu ciy leer dayo bi bor am ak diis bi mu diis, ngir fàttali sunu bopp, waaye fàttali sunu bokki jullit yi ngir ñu jàjju te moytu bor boodut fay.
Show notes
Ci waxtaan Wii, danu ciy indi tontu ci laaj bii: Ban xam-xam mooy farata ci nit ki? Ginnaaw Yonent bi SAW daa wax ne sàkku xam-xam farata la ci jullit bi, kon yey na lu ne xam ban/yan xam-xam la war a ràngoo.
Show notes
Waxtaan wii mu ngi aju ci Teggiini niti Yàlla yi ak sew-sew yi leen wuutale ak ñeneen ñi.
Show notes
Waxtaan wi ab jukki la ci téereb kàngam boobu di Imaam Saaraani. Ci téere bi dafa ciy jàngale teggiini niti Yàlla yi yoy képp ku sóobu ci Yàlla te bëgg a bokk ci góor ña war nga leen ca roy.
Show notes
Waxtaan wii Imaam Xasaali dafa ciy wax njariñ yi ci koor ak yiiw yi mu man a fàggul jullit bi, waaye tamit leeral dayo bi koor am fa saa Boroom.
Show notes
Waxtaan wii mu ngi aju ci àq yi nit man a ameel ay moroomam ak i saafara yi leen di far. Àq mat naa moytu, ndax ëllëg lu ñuy fayante la. Di jëfandikoo ñaan yi niti Yàlla yi tënk nag da ciy am solo ngir ëllëg sa dara du l
Show notes
Ci mujjantalu téere bi, Imaam Dardiir daa tënkaat gàllankoor yiy tënk nit ki ba du àgg ci Yàlla, niral ci jikko yu mel ni rëy, ngistal añs… waaye tamit leeral ci ne Jaamu Yàlla di ci sàkku leneen ludut Yàlla ci gàllankoo
Show notes
Ci waxtaan wi, danuy leeral xeeti xalaat yiy toq ci xelu doomu aadama, seen i jeexital ak yoon wi nit ki di jaar ngir sellal ay xalaatam ba duñu ko yóbb ci moy Yàlla.
Show notes
Ci waxtaan wii Imaam Dardiir dafa ciy waxtaane jikko yi nitu Yàlla yi di ame bu seen dox ci Yàlla matee ba seen i teggin mat sëkk (Makkaarimal ahlaax).
Show notes
Ci waxtaan wii, Imaam Dardiir dafa ciy leeral xeetu teewlu yi am ak fi ñu man a yóbb nit ki ci jege Yàlla. Bu fa nit ki àgge, dina dem ba xam, yëg bir yoo xam ne maneesu koo leeral ci làmmiñ.
Show notes
Ci waxtaan wii, Imaam Dardiir da ciy wax ci xeetu tudd Yàlla yi am, rawatina bu làmmiñ bi nga xam ne kiy doog a sóobu ci lay tàmbalee. Ci mujj gi mu tënk ponku tassawuf yi mu jàpp ne ñoo ci gën a am solo.
Show notes
Ci tomb yii, Imaam Dardiir da ciy wax ci solos jaamu Yàlla njël ak taxawaayu tudd Yàlla ci dundug aji-sóobu ji. Ñu doon yaari ponk yoo xam ne ki sóobu ci Yàlla da leen a war a fonk ngir jot ci càkkuteefam.
Show notes
Wéet daa bokk ci ponk yi tassawuf teg ngir nit ki sellal xolam. Jaxasoo ak nit yi lu bari ci lu dul farata dafay sabab ay ayibu xol. Moom la Imaam Dardir di leeral ci waxtaan wii ngir aji-sóobu ji bàyyi ko xel.
Show notes
Ci dars bii, Imaam Dardiir dafay waxtaan ci ponku tassawuf yii di nangu ndogal ak wut sëriñ bu mat sëriñ. Ci ginnaaw gi mu misaal nu sëriñ bu mat sëriñ nu muy mel.
Show notes
Ci biir fukki ponk tassawuf yi Imaam Dardiir indi ci téereem bi, waxtaan wii mu ngi aju ci lan lañuy tuddee sant Yàlla ci diine ak lan mooy muñ bi tax ñuy wax muñ.
Show notes
Tasawuf daa am ay ponk yoo xam ne nitu Yàlla yi dañu ko tëral ngir yombal aji-sóobi ji ngir mu jot ci sàkkuteefam. Ponk yooyu ñu ngi ko tënk ci fukk. Tay nag ponk bu njëkk bi lañuy waxtaane te mooy TUUB.
Show notes
Ci waxtaan wii, imaam Dardiir dafay waxtaane jikkoy xol yiy gàllankoor muriit bi ba du am ag jege Yàlla. Saalig bi (ki bëgg àgg ci Yalla) daa war a taqoo ak sikar ak jéem a dindi jikko yu ñaaw yépp ngir àgg ci Boroomam,
Show notes
Tasawuf: Dëgg la ne ñi réere tasawuf bari nañu lool ci jamono. Ñii dañu ko réere ndax ñàkk a ci tàbbi, ak xeeb doxalinu ñi ci nekk te di ci boole lu ci bokkul. Am ñu ci nekk ba noppi réere mbir ndax ñàkk a xam li ko tax
Show notes
Waxtu daa doon lu gànjaru lool te mat a moytu a sanq. Jépp noyyi, sépp simili, wépp waxtu wurus la wow nit ki man na ci fàggu lu ko texeel ëllëg. Saggane ko nag ak di ko jeexal ci neen rëccu lay jural nit ki. Moo tax nu
Show notesSponsor detection runs nightly. Check back soon.
No public pitch examples yet for this show.
Generate your own personalised pitchBased on semantic analysis of episode topics and host coverage, this show is a strong guest fit for executives in:
Industry fit is computed by PitchCentric using vector embeddings of the show's episode catalog.
Shows with the most semantically similar episode content. Pitch one, pitch all; producers cluster.








To pitch Bëgg a Baax podcast, visit https://podcasters.spotify.com/pod/show/cheikhouna-diaw for contact information, then craft a tight one-paragraph hook that ties your expertise to a gap in their recent religion coverage.
Bëgg a Baax podcast is hosted by Cheikhouna Diaw. The show is categorised under religion (spirituality) and has published 26 episodes.
Bëgg a Baax podcast has published 26 episodes.
Bëgg a Baax podcast regularly covers religion, spirituality. It sits in the religion category, with a spirituality focus.
Bëgg a Baax podcast is accessible for guests with genuine religion expertise. A personalised, episode-aware pitch will still outperform a generic one every time.
Bëgg a Baax podcast hasn't explicitly signalled guest openness in recent episodes. That doesn't rule out pitching. your hook just needs to be especially compelling and relevant to their recent content.
Episodes of Bëgg a Baax podcast average 26 minutes. a focused format where a clear narrative arc and tight preparation matter most.
Our data rates Bëgg a Baax podcast's guest bar at 80/100 (Premium tier). Established thought leaders with verified media credentials. Sign in to PitchCentric to see how your own Pod Score compares against this show.
Methodology. Booking Probability™ blends Listen Score, 30-day Virality, open-to-guests detection, and Apple ratings. Data refreshed every 60 minutes. Listen Score and Booking Probability are calculated by PitchCentric. Last enriched today.